Appli bii mooy Kàddug Yàlla، gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit، ak Kóllëre gu yees، gi mujja wàcc، te ñenn ñi di ko wooye Injiil، muu tekkimm. Ñaari tére yooyu، Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi، kóllëre gu jëkk gi، ñu bind ko ci yawut، gu yees gi، ci làkku gereg. Li ñu bind ci tére yu jëkk ya nag ، moom lanu tekki ci wolof.
[الكتاب المقدس ، الولوف ، كادوق يلا]